twitter facebook rss
Imprimer Texte plus petit Texte plus grand

Dalal jàmm ci OneDrive, le nouveau service de Microsoft parle Wolof

lundi 24 février 2014

Lancé il y a seulement quelques jours (voir notre article), le service de stockage en ligne de Microsoft disposerait d’une version Wolof. En tout cas l’e-mail qui nous été envoyé dans un de nos comptes hotmail est bien écrit en Wolof.

Voici le texte contenu dans cet e-mail :

Dalal jàmm ci OneDrive, benn barab bi ngay denc ak séddoo say nataal, wideo, téere ak yeneen bara denc-fu la neex, ci benn jëfandaay, te doo fay. Ci weer yii di ñëw, mën na am ngay wéy di gisandoo SkyDrive ak OneDrive ci sa yoon, waaye bul jaaxle ! Di nga mën di jot mbooleem say bara denc ci diirub coppite googu. OneDrive moo ëmb lépp lu la neex ci SkyDrive ak yeneen mbir.

Benn barab ngir mbooleem say nataal ak wideo

Jëleel ci sa telefon say nataal ak wideo yi la gënal ndax nga mën di leen jotee ci mbooleem say jëfandaay ak séddóo yi la neex te doo sonn.

Benn barab ngir mbooleem say téere

Sos ak soppi ay téere Word, Excel, PowerPoint, ak OneNote yu am solo, denc leen ñoom ñépp ci benn barab, te mën leen jotee ci bépp jëfandaay.

Benn barab ngir mbooleem say jëfandaay

Jotee say bara denc OneDrive ci bépp jëfandaay bu la neex boole ci say jëfandaayi PC, laalukaay, Mac, Windows Phones, iPhones, Android, ak yeneen.

Xool leneen lu OneDrive mën a def

Duggal seet mën-mën yu mag yi ci OneDrive te xam lan mooy benn barab ngir denc mbooleem mbir yi la gënal.

Xam yeneen mbir

Danga bëgg a am dencukaay bu maye ? Am ba ci 8 GO soo toppee jéego ngir may sa dencub fagaru jëlug nataalukaay ak yabal say xarit. Duggal ci OneDrive.com.

(Source : ITmag, 24 février 2014)

BATIK

Inscrivez-vous a BATIK

Inscrivez-vous à notre newsletter et recevez toutes nos actualités par email.

Navigation par mots clés

INTERNET EN CHIFFRES

- Bande passante internationale : 172 Gbps
- 4 FAI (Orange, Arc Télécom, Waw Télécom et Africa Access)
- 10 770 683 abonnés Internet

  • 10 512 647 abonnés 2G+3G+4G (97,60%)
  • 99 177 clés et box Internet (1,11%)
  • 138 743 abonnés ADSL (1,31%)
  • 17 952 abonnés bas débit (0,17%)
  • 2164 abonnés aux 4 FAI

- Liaisons louées : 22 633

- Taux de pénétration des services Internet : 68,49%

(ARTP, 31 mars 2019)

- 7 260 000 utilisateurs
- Taux de pénétration : 58,20%

(Internet World Stats 31 décembre 2018)

- 4710 noms de domaine actifs en .sn

(NIC Sénégal, 25 septembre 2018)

TÉLÉPHONIE EN CHIFFRES


Téléphonie fixe

- 2 opérateurs : Orange et Expresso
- 307 736 abonnés
- 237 282 lignes résidentielles (77,11%)
- 70 363 lignes professionnelles (22,86%)
- 84 lignes publiques (0,03%)
- Taux de pénétration : 1,95%

(ARTP, 31 mars 2019)


Téléphonie mobile

- 3 opérateurs (Orange, Tigo et Expresso)
- 16 977 104 abonnés
- Taux de pénétration : 107,95%

(ARTP, 30 septembre 2018)

FACEBOOK

- 3 171 000 utilisateurs

- Taux de pénétration de Facebook : 18,6%

(Facebook, Juin 2019)